Bamako - Youssou N'Dour
С переводом

Bamako - Youssou N'Dour

Год
2009
Язык
`Anglais`
Длительность
268570

Voici les paroles de la chanson : Bamako , artiste : Youssou N'Dour Avec traduction

Paroles : Bamako "

Texte original avec traduction

Bamako

Youssou N'Dour

Оригинальный текст

Si gare bi lako fekkeu

Mi ngui sanguo seur

Té beut yi di takkeu

Ma dal di koye nougnou

Mou dal di maye faye

Dal di maye yédeu ci adouna bou yakhou bi

Mane douma fatté!

Ah mani ah mani!

Man douma fatté bamako lii mani lii mani!

Mane douma fatté!

Kerok lama khamal louma khamoul woone ci diamono bou yakhou bi yénene ak yénene;

Balaa maye dougeuti mane ci loumou meuneu doone

Dinaa fattélikou ndaw sossou

Limouma wakhoone!

Souy souy sou sou sou sou sou sou souy!

Ci gare bi lako fekkeu mi ngui sanguo seur té beut yi di takkeu

Ma dal di koye nougnou

Mou dal di maye faye dal di maye yédeu

Maky yé maky maky yé maky yééééé!!!

Waw kérok lama khamal louma khamoul woone ci diamono bou yakhou bi

Balaa maye dougeuti ci loumou meuneu doone

Dinaa fattéli ko maky yé maky maky yé maky yéé!!

Ah mani ah mani!

Douma fatté bamako lii mani lii mani!

Mane douma fatté bamako

Перевод песни

Si gare bi lako fekkeu

Mi ngui sanguo seur

Té beut yi di takkeu

Ma dal di koye nougnou

Mou dal di maye faye

Dal di maye yédeu ci adouna bou yakhou bi

Mane douma fatté !

Ah mani ah mani !

Homme douma fatté bamako lii mani lii mani !

Mane douma fatté !

Kerok lama khamal louma khamoul woone ci diamono bou yakhou bi yénene ak yénene ;

Balaa maye dougeuti mane ci loumou meuneu doone

Dinaa fattélikou ndaw sossou

Limouma wakhoone !

Souy souy sou sou sou sou sou souy !

Ci gare bi lako fekkeu mi ngui sanguo seur té beut yi di takkeu

Ma dal di koye nougnou

Mou dal di maye faye dal di maye yédeu

Maky yé maky maky yé maky yééééé!!!

Waw kérok lama khamal louma khamoul woone ci diamono bou yakhou bi

Balaa maye dougeuti ci loumou meuneu doone

Dinaa fattéli ko maky yé maky maky yé maky yé !!

Ah mani ah mani !

Douma fatté bamako lii mani lii mani !

Mané douma fatté bamako

Plus de 2 millions de paroles

Chansons en différentes langues

Traductions

Traductions de haute qualité dans toutes les langues

Recherche rapide

Trouvez les textes dont vous avez besoin en quelques secondes